LetrasSant na

Viviane N'Dour

Última atualização em: 26 de outubro de 2017
Estas letras estão à espera de revisão
Khadidiatou Gueye sugeriu alterações a esta letra.

Dara gueunoul nekh lii Niit gni dila bégué Foo wayé niou contane Ko yeuk yeuknala Té ko faalé faaléleu Yéneu moom lii Té ko falé faaleleu Mane may sopé gouné yi Di xaritou goor yi Magg yi naan yagnou saf Djiggen yi lang ak mane Sant na yallah (bis) ouuh Bima amé niit gni Sant na yallah (bis) ouuuuuuuh Diox nalène sama xol Yeen gni ma saffo Diap nalène doumalène baayi Koo yeuk yeuknala Tè ko faalé faalé leu Yeeneu moom lii Tè ko falé faalé leu Mane maay sopé gouné yi Di xaritou goor yi Magg yi naan yagnou saff Djiggen yi lang ak mane Sant na yallah (bis) ouuh Bima amé niit gni Sant na yallah (bis) ouuh Bima amé niit gni Sant na yallah (bis) ouhhh ouuuuhhh Damay doogua door Yow khamnaa né yomboul Teen wii sorina Dara gueunoul nekh lii Niit gni dila bégué Foo wayé yeup contane Foo wooté nieup nieuw gua teerou Yow mane khamnaané yomboul Sant naa yallah Sant naa yaaallah sant leen yallah Niit kouné saayoo yeewoo war ngua sant yallah Yow mane khamnaané yomboul Youssou madjiguène yow kham ngua né yomboul Yow Ndiaye yow kham ngua né yomboul Thiané diagne yow kham ngua né yomboul Djolof band yeen kham nguen né yomboul Wawaaw.

  • 33

Últimas atividades

Sincronizada porel hadji demba diop
Tradução porFatou Gueye

O Musixmatch para Spotify e
Apple Music está agora disponível para
o seu computador

Descarregar agora