歌詞Sant na

Viviane N'Dour

最終更新日:: 2017年10月26日
この歌詞は確認待機中です。
Khadidiatou Gueye がこの歌詞の変更を提案しました。

dara gueunoul nekh lii niit gni dila bégué foo wayé niou contane ko yeuk yeuknala té ko faalé faaléleu yéneu moom lii té ko falé faaleleu mane may sopé gouné yi di xaritou goor yi magg yi naan yagnou saf djiggen yi lang ak mane sant na yallah (bis) ouuh bima amé niit gni sant na yallah (bis) ouuuuuuuh diox nalène sama xol yeen gni ma saffo diap nalène doumalène baayi koo yeuk yeuknala tè ko faalé faalé leu yeeneu moom lii tè ko falé faalé leu mane maay sopé gouné yi di xaritou goor yi magg yi naan yagnou saff djiggen yi lang ak mane sant na yallah (bis) ouuh bima amé niit gni sant na yallah (bis) ouuh bima amé niit gni sant na yallah (bis) ouhhh ouuuuhhh damay doogua door yow khamnaa né yomboul teen wii sorina dara gueunoul nekh lii niit gni dila bégué foo wayé yeup contane foo wooté nieup nieuw gua teerou yow mane khamnaané yomboul sant naa yallah sant naa yaaallah sant leen yallah niit kouné saayoo yeewoo war ngua sant yallah yow mane khamnaané yomboul youssou madjiguène yow kham ngua né yomboul yow Ndiaye yow kham ngua né yomboul thiané diagne yow kham ngua né yomboul djolof band yeen kham nguen né yomboul wawaaw.

  • 32

最新の活動

翻訳者:Fatou Gueye

あなたのコンピューターのSpotifyと
iTunesでMusixmatchが現在利用可能になりました。

今すぐダウンロード